Obree Daman - Me You and God

Copied!edit Lyrics
original text at lyrnow.com/2060153
Mbeuguel la nekk ci sama xol
Wai adouna nyu sonal lol
Xol bu fess ak baneex
La la yeené won ci adouna
Mbeuguel gima am ci yow
Mba duma sonal lool
Diafé diafé adouna
Ak bokk gui yallah burr bi bole

Kon mbeuguel lay adouna
Ndax Yallah mo nyu bolé
Sama yeene yaatuna
Mangi nyaan ndax Yallah mey nyu dolé

Dugu na ci gaalu mbeuguel, ndox mi yobuma
Ngelew langui mai indi ci yow
Nyu guissé leer na ma
Mbeuguel moi li leeral adouna
Xam nga yow la beug lool
Sama yeené yaatuna
Mangi nyaan mu yoku

Denk na la yallah
Denk na la sama xol
Sasu ma djuli di la nyaanal
Sama xol la ko tibé
Denk na la yallah
Denk na la sama xol
Sasu ma djuli di la nyaanal
Sama xol la ko tibé
Kon mbeuguel lay adouna
Ndax Yallah mo nyu bolé
Sama yeene yaatuna
Mangi nyaan ndax Yallah mey nyu dolé

Dugu na ci gaalu mbeuguel, ndox mi yobuma
Ngelew langui mai indi ci yow
Nyu guissé leer na ma
Mbeuguel moi li leeral adouna
Xam nga yow la beug lool
Sama yeené yaatuna
Mangi nyaan mu yoku
 
0

Song Description:

edit soundcloud

SoundCloud:

edit soundcloud

More Obree Daman lyrics

Obree Daman - Banneex
Kula faale wul man mii maa lay faale Doon sa seetu kula xool man lay gisaale Kula faale wul man mii maa lay faale Doon sa seetu kula xool man lay gisaale Ci sa bët laay xool

Obree Daman - Me You and God
Mbeuguel la nekk ci sama xol Wai adouna nyu sonal lol Xol bu fess ak baneex La la yeené won ci adouna Mbeuguel gima am ci yow Mba duma sonal lool Diafé diafé adouna